avatar

Yoon ngir Mouhamed! Waxtaan ak ay rakkam Sidy ak Lassana Dramé

radio.nrdpl.org
radio.nrdpl.org
Episode • Dec 3, 2024 • 14m
Salaam maalekum! Lu tollu ci benn at Radio Nordpol ci Dortmund mungi doon topp atte bu jigeen poliis yi faat Mouhamed Lamine Drame ci seeni jëf. Fi ñu tolli nii ñungi doon joxe xibaar ci Allemand te deñoo bëgga tabax ab pont ci lakk yi ak waxtaan bu gàtt bii ak rak yu Mouhamed yi […]